"Qulil haqq walaw kaana murran"
Bécaye Deugg rek la wax, touba affaire bi foofu la. Kuko guissul ci say gueut, danga ko dégg biss buné.
Serigne Touba bamiy jeuf, mbooléém jullit yi niooko takhoona jog rawatina waa sénégal guepp.
Ijhal rujuuhii ilaa qawmii sahaadatanaa
wal takfinaa yawmal jamhil khalqi niiraanaa.
demnaa ba niaanal mbooléém mbideef rawatina ab jullit :
"Yaa maalikal mulki yaaman jalla han qawadin
irham jamiihal waraa yaa haadiyan rada’aa "
Kon kooku buniou nélaa deukk bimu fondé dafa jeum kanam, wax ca lu baax, danga caa waara bég, contaan ca, boodé jullit bu sotti.
Yalna yalla yokk tawfiiq ci mboooléém jullit yi.
wa salam
Répondre à ce message